La guineé – Sénégal c’est l’afrique qui gagne Ouuhh ohh oo, zaya Je t’aime un point c’est tout hOo woo, un point c’est tout  Je t’aime un point c’est tout Yarabi mani chérie té mbifé  (Bambara) Je suis ton roméo, tu es ma Juliette Baby toi et moi pour la vie Je suis ton romeo tu est ma Juliette C’est toi et moi pour la vie

Advertisement

Bébé chérie je t’aime un point c’est tout Wallay bilay, je t’aime un point c’est tout Bébé chérie je t’aime un point c’est tout Wallay bilay, je t’aime un point c’est tout (Un point c’est tout) Hooo hoo, un point c’est tout Je t’aime un point c’est tout, yarabi mani chérie té mbifé

Sama mbeuguel mon ngui daw di niow ci yow Sa mbeuguel di naw di niow ci mane Soumala khamoul wone, kham na ni douma bardé Yowit soma khamoul wone sama goor do bardé Ndax li gni doundu, dafa nexa nex Ndax li gni doundu mak yow mo daak nex

Advertisement

Sama xol sama life soma bayé dina weet  Yama mom, mala mom pour la vie Sama xol sama life soma bayé dina weet  Yama mom, mala mom pour la vie

Beugeu nala té fowéwou mala beugeu nala Fawma di rafé fufa hoo Beugeu nala té fowéwou mala beugeu nala Lima am, li nga am, niou bolé ko mou nek ben  Chérie beugeu nala  Lima am, li nga am, niou bolé ko mou nek ben  Chérie beugeu nala Hey my boy soumala guissoul damay weet ndax yoww rek la mine Guiss la beugeu la loukay fay,  Wax nako beugoulo loumay gagn kham nako Amoul Adji amoul Ass, lou woor la  Lima yeug dou ay foo lou woor la

Sama xol sama life soma bayé dina weet  Yama mom, mala mom pour la vie Sama xol sama life soma bayé dina weet  Yama mom, mala mom pour la vie

Bébé chérie je t’aime un point c’est tout Wallay bilay, je t’aime un point c’est tout Bébé chérie je t’aime un point c’est tout Wallay bilay, je t’aime un point c’est tout

You May Also Like

James Patrick Dunne Net Worth, Income, Salary, Earnings, Biography

Advertisement Jimmy Dunne is a modern-day Renaissance Man who effortlessly straddles the…

Joe Mucheru Biography, Family,Education, Career, Net Worth, Social Media, Interview

Advertisement Joe Mucheru Biography Joe Mucheru (Joseph Wakaba Mucheru) is the Cabinet…

Anthony Reed (FBOY Island) Wiki, Bio, Age, Height, Weight, Girlfriend, Net Worth, Facts

Anthony Reed is an American behavioral health technician and currently well known…

Kruzadar Height, Weight, Net Worth, Age, Birthday, Wikipedia, Who, Instagram, Biography

Kruzadar TikTok Comments are killed and fans are interested to know why…